Wiri Wiri (feat. Siignaar G)

OoThenTiK Zeus

Compositor: Não Disponível

Deff Music

Wiri
Wiri
Diaari ndaaré
Wiri
Wiri
(Pape Laye)
Diaari ndaaré
Wiri
Wiri
Diaari ndaaré
Wiri
Wiri
Diaari ndaaré

Louné louné
Dieem naako def
Technique bouné
Diemnaako tek
Toujours la même
Réponse dedeet
Dieemnaala ba mais lii dou neen

Nieuwaat nga kong
Metitou khol
Tekma thiono
Teh dama beau
Dieundaat cadeau
Pour am sa khol
Damay niakaat diom mais dooma khool

Mbeugueul dou diaay loolo metti dagma diaral (dagma diaral)
Mane damla dieulsi doumfi nekay tabal tabal (tabal tabal)
Guisnaala demb ki nga andal kila xaral (wa dou ki)
Day nioodi gentle mais dou dara sama kanam (dara dara)

Mane dama baayi nieupeu né iow la iow la iow la
Looma wakh biss boo wakhé waw noonou laa noonou laa noonou laa bébé

Deff loo ngama lounekk
(Wiri wiri diaari ndaaré)
Dem loo ngama founekk
(Wiri wiri diaari ndaaré)
Wayadiloo meu founekk
(Waayé douma dieul ndaaré)
Si mane ngay moudier, yaag yaag di nga barder

Wiri wiri diaari ndaaré (oh diaari ndaaré)
Wiri wiri diaari ndaaré (oh diaari ndaaré)
Wiri wiri diaari ndaaré (oh diaari ndaaré)
Wiri wiri diaari ndaaré (oh diaari ndaaré)

Bimlay wakhni beugoumaleu
Nangouloomawoon deglou
Tay nga tekk sa bopp thiono (thiono)
Ba noppi ni louné laaley deff loo

Fii amoul wiri wiri diaari ndaari
Maak iow dou meusseu nekk dedeet never
Dieemeul lambi feneen moo gueun
Fi nga dal nii bro amna borom

Maak iow dou béneu
Bookouniou level
Teh sooma soroo di nga guiss loula diaakhal
Def naa lou nékeu
Ngani doo gëdda
Yow fooma toopé ay yallah miniou sakka

Iow mii iow miii
Baayimeuuu waaaw
Baayimeu baayimeu

Deff loo ngama lounekk
(Wiri wiri diaari ndaaré)
Dem loo ngama founekk
(Wiri wiri diaari ndaaré)
Wayadiloo meu founekk
(Waayé douma dieul ndaaré)
Si mane ngay moudier, yaag yaag di nga barder

Wiri wiri diaari ndaaré (Oh diaari ndaaré)
Wiri wiri diaari ndaaré (Oh diaari ndaaré)
Wiri wiri diaari ndaaré (Oh diaari ndaaré)
Wiri wiri diaari ndaaré (Oh diaari ndaaré)

Oh diaari ndaaré
Oh diaari ndaaré
Oh diaari ndaaré
Oh diaari ndaaré

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital